Gambian Wolof Language


Some phrases

Yes
--
No
--
Maybe
Waaw
--
Daydate
--
Munaa am
I know
--
I don't know
Hamnaa
--
Howma
Did you understand?
--
I understood
Yangeh jayli?
--
Jayli naa
Can you speak slower? Mun ngaa wahh ndanka?
Can you repeat this again? Mun ngaa wahaat lolu?
Do you speak:
--
French?
--
English?
--
Portuguese?
Dang deh laaka:
--
French?
--
English?
--
Portuguese?

Love and relationship phrases in Wolof

*There are no masculine or feminine pronouns in Wolof

I like you
--
I love you

--
I want to date you
Dangma nehh
--
1) Damala buga
2) Damala nopp
--
Dama buga neka ak yow
I do not like you
--
I do not love you

--
I do not want to date you
Nehu loh ma
--
1) Bugu mala
2) Noppu mala
--
Bugu maa neka ak yow
I think you are a beautiful woman
--
I think you are a handsome man
Jiggeen bu rafet nga
--
Gorr bu rafet nga
I think he is a handsome man
--
I think she is a beautiful woman
1) Si man dafa rafet
2) Gorr bee dafa rafet si man
--
1) Si man dafa rafet
2) Jiggain bee dafa rafet si man
Gambian women are beautiful
--
Gambian men are beautiful
Jiggen ni Gambia denj rafet
--
Goori Gambia denj rafet
Can I invite you to dinner or lunch?

--
Do you want to pay or should I pay?
1) Mun ngaa nyow anj?
2) Reel ak man?
--
Danga buga feye ndah man ma feye?
You have a good personality Sa jikko bi dafa rafet

Birthday and new year phrases in Wolof

Greetings for occasions (birthdays, new years eve, birthdays etc)

--
..the standard response
Dewenati

--
..Fekeh dewen
Congratulations Ndoka leh koh
I have this gift for you, hope you like it Mang la indil Lee, yakarr naa dina la nehh
Today is your special day Tei sa bess la
Wishing You Joy and Prosperity! Noppalu na la ci mbeggeel ak jamm!
Wishing you peace, love, and happiness this holiday season Nuyu na la jàmm, mbeggeel, ak liggeey bu rafet ci lii bés bi
What are your plans for New Year's? Lu tax nga xamal bes bu bees bi?
I will be with my family for New Year’s
--
I will go out with friends
--
I don’t have any plans for New Year’s
Dinaa nekk ak sama wàllu bés bu bees bi
--
Dinaa génn ak sama xarit
--
Duma am benn xalaat ci bés bu bees bi

Learn Gambian Wolof

------
African Languages on Mofeko

West Africa


- Ìgbò
- Wolof
- Yorùbá

East Africa


- Chichewa (Nyanja)
- Kinyarwanda (Ikinyarwanda)
- Kiswahili

Central Africa


- Chokwe (Wuchokwe)
- Ibinda (Fiote)
- Kikongo
- Lingala
- Tshiluba

Southern Africa


- Malagasy
- Naro (Senaro)
- Nyaneka-Humbi
- Sekaukau
- Setswana (Tswana)
- Shona (chiShona)
- Umbundu (South Mbundu)
- IsiXhosa (Xhosa)
- IsiZulu (Zulu)